Important notice about the future of Stripcreator (Updated: May 2nd, 2023)

  fleabitten  

followers
1
following
1
pm : info
fleabitten has not entered a profile.
(hide profiles)

by fleabitten
1-20-06
Mel ak Tapha nu ngi toog ca ker ga. Ibout xaritu Tapha, new na.
Mel na nga def
Uhh ma ngi fii rekk
Yow degg nga wolof bu baax?
Degg naa tuuti rekk
Laayila! Tubaab bi degg na Wolof!
Alxumdalilay!
share: twitter : facebook


« Back to the Front Page